Wolof
Ndoomu Buur Si

Cey! doo mu buur Bundaw maaghi soga xam, ndank dank sa dundu bu metti Bis bu neek, be timis jothe sa foykat moy naaj buwatj – sa xol seed Degg na loolu ci nhientel fann bin ga ma waxoon: Timis laa beegg.

Sonne: haj
Sprache: Wolof
Sprachfamilie: 		
		Niger-Kongo		
		
> Atlantisch > Nordatlantisch > Sene-Gambisch > Wolof
Schrifttyp: phonographisch > alphabetisch > lateinisch
Ort: Kaolack, Senegal

| Impressum |
